org.mbs.kyg.wol
4.3.4
43.2 MB
5.1++
Appli bii mooy Kàddug Yàlla, gi dikke ñaari pàcc: Kóllëre gu jëkk gi Yàlla fas ak nit, ak Kóllëre gu yees, gi mujja wàcc, te ñenn ñi di ko wooye Injiil, mu tekki Xibaaru jàmm. Ñaari tére yooyu, Yàllaa leen wàcce ci nitam ñu sell ñi, kóllëre gu jëkk gi, ñu bind ko ci yawut, gu yees gi, ci làkku gereg. Li ñu bind ci tére yu jëkk ya nag, moom lanu tekki ci wolof.
[bible, wolof, kaddug yalla]
9bc5f2107844d52683eaca9d90e94f05
16:04:60:14:C8:9F:62:2E:E2:B5:24:D1:EC:2